Lyrics Youssou N'Dour

Youssou N'Dour

Chimes Of Freedom

Si diguenté marakh massé

bi diololi suuf sédé

si lagn gawantou fatu mingui done gara

ni bi diololi you tedd si melakh yi kawélakh

yenene you melni you done rire nguir liberté

di riir ngur diambar yi donne khekh té bal takoul

di riir nguir gni done gadaay ci yon you meti yi

aki tamit kep kho khamni soldar nga bou toumouranké si goudi gui

And we gazed upon the Chimes Of Freedom flashing

si bene mbar si deuk bi gni ngui lakhatou wone di khol binga khamanténi mbir yangui done wagnékou

bi diololi yi nek khew di riir ci taw bi ngelaw youdoul diolol you lerr nek ci kaw di tabi

aanhh di riir nguir di bagne, di yeungou nguir ki loff

di yengou nguir ki niak chance gni gnou faté gni gnou wor

di yengou nguir gni gnou bedi yagg ko lakh mouy doundé

And we gazed upon the Chimes Of Freedom flashing

si bi dalouk doy warr bi dondiou glace you gnang rott

di khoti diaou dji di setou wer ak sell

wayam you clochou eglise yi di sani fo soré soré ak nguelaw li

desatoul loudoul diolol you nekoul ca rak bi

anh di riir ki labiir di riir nguir ki bakh

di riir nguir gni gniy gadi ak kiy samm sunu tour

ak natal kate bi kene guissoul fou soré soré si diamonom

And we gazed upon the Chimes Of Freedom flashing

si goudi you bari kemtane yi

taw bi melni li louy ler té ay takander you amoul forme té toumouranké

di wakh guir lamigne yi mounoula wakh sene khalatt

té ay khalat yo khamné fogone nagne ni né khamou gnou lene

di wakh nguir silmakha yek gni teukh

di wakh nguir gni lou gniy nato jieggen youniouy nakh

ak gni gnouye toudé thiaga

di wakh nguir say say niou guené mou daw ba rer

And we gazed upon the Chimes Of Freedom flashing

yi dem ba bene nir ci assamane si naw di tour ndokh ndank ndak té le

lérayou lamp yi di gnou dal mel ni fitt wou dioubel si

gni natt gni gnouy werr té khamou niou founiou né thi dounya

aanh di riir ngui gni wadiou sén si yone you meti yi

di riir nguir gni beugeunté té mounou nio wakh sene metite

di riir ngui yaram you niou teuj si casso té defou niou dara

And we gazed upon the Chimes Of Freedom flashing

nagnou khol lérayou liy rir nguir liberté