Lyrics Youssou N'Dour

Youssou N'Dour

My People

ma ngui binde way bi diko méy

gneup gni ma beugue di lèn ndioukel

ndioukel gneup gni ma diapalé

souma lène meunone diokh lokho defnako

soumalène meunona setsi eh eh yeksina

fatéwoumalène, dédéte meunoul am

yeugone nalèn salaw moy li wor

souma teugué ngène gneuw wouyoussima

souma guéné lou bess ngène dieundeuko

manou malène faye

magui bind way wi di lène ko méy

refrain (bis)

you you you you

you gorgorloul gnougui sa guinaw

soumalène meunone diokh lokho defnako

souma lèn meunona setsi yéksina

kouma soufèl ngène khoulok mom

fatéwoumalène dédét meunoul am

yeugue nalène salaw moy li wor

bataxna ma gui bind way wi diko may

refrain (bis)

fatéwouma fatéwouma fatéwouma fatéwouma ah (4 fois)

refrain (bis)

ehhhhhhhhhhhhhhh mangléni sant di gueureum

mane ndioukel nalèn